Bineta

[column-half-1]
BINETA

Ta peau est ébène,
Ton sourire sublime
Douce sont tes mains
Pleines de tendresse et d’amour
Ta peau est ébène
Noire comme le ciel étoilé
Soit fière dêtre lébou
Beauté de la Reine Cléopâtre

Et de Néfertiti
Kémétiyou
Dés le lever du soleil,
N’hésite pas à t’exposer
Ta couleur est vie
Et mille promesses de la femme en devenir
Ô femme Africaine
Ma fille, mon avenir préserve chaleureusement
Ce que la nature t’a offert
Tiens ! En parlant de nature,
Quand tu iras les voir
Offre cette calebasse de jujube à
Bouba et Baïla de ma part

TOUTOU BAILA NDIAYE (Sénégal)
[/column-half-1]
[column-half-2]
Binta (version en oualof)
Sa der wi ngelembaan la,
Sa muuñ jéggi dayo
Say yoxo nooy
Fees ak cofeel ak mbëggeel
Sa der wi ngelembaan la,
ñuul ni asamaan su fees ak i biddiw
damul ci lébu bi nga doon
Taaru ni Lingeer Kelewopaatar

ak Nefertiti,
xemetiyu
Bu jant biy fenk
bul am xel ñaar wonewu
sa melo dund la
ak junniy digi jigéen jiy magg
Leel jigéenu Afirik
Sama doom, sama elleg.samal té fonk
li la mbind may
Waaw kay ! lu jëm ci mbind,
Boo demee seeti leen
Mayal ma leketu siddéem bii
Buuba ak Bayla

Tutu Bayla Njaay (Sénégal)
[/column-half-2]